Slm slm ouztaze manne dh dama guénte sama copin niew souniou keur niou bok founiou fanane légui nk sama yaye AK sama papa dadi may wakh ma djitalle toubaye you Bari légui sama copin dégg KO dandi mer dani niome wolou wouniou KO légui moudadi may bayi may dioy