Un autre Serigne Bara Ndiaye👌👌👌. Eloquent, pertinent et captivant 🧐. Machallah Mbacké Balla. Les Ndongo Dara font leur révélation intellectuelle et se prouvent plus intelligents que les apprentis occidentaux 😮😮😮
Serigne bi linga wakh ci mbiroum républicain rék moci am bo néké fii di nangou ay loi yo khamni ngir néwal doolé nit ki dolé kép moko waral dinga wayadi ba faww
Merci Serigne bi en tout cas aucune autorité ne souhaite avoir une quelconque autre autorité parallèle. C'est le cas de l'Etat et nos Foyers religieux mais dans tous les cas le Pouvoir DIVIN à l'image des CHEFS RELIGIEUX resteront à jamais dans nos cœurs
Tiow li tiow li moy diaratul ay détails nañu woté ñu diok dem diamarlo pour la liberté du pays niuy dhé dhé ñuy dundu dundu mais bilahi khana ma dhé mais duma nangou di dundou di guiss ce régime en place diñu continuer djité après 2024
Encore une révélation du Daara. Macky Sall khamoul sakh frustration sénégalais foumou tolou. Barké Serigne Touba gni nék si réseau sociaux ak si plateau di wakh. Gni né ték né thieel nioco eupp foufff