Тёмный

😭 Allahou Akbar: Grave Accident sur la Vdn, entre un Taxi et un Bus TaTa, Al Hadji Rafétte fait... 

DAKAR PLUS
Подписаться 214 тыс.
Просмотров 101 тыс.
50% 1

Развлечения

Опубликовано:

 

12 май 2024

Поделиться:

Ссылка:

Скачать:

Готовим ссылку...

Добавить в:

Мой плейлист
Посмотреть позже
Комментарии : 154   
@ouleymatoudiagne1216
@ouleymatoudiagne1216 25 дней назад
Billahi depuis cet après midi je fais 4:57 que pleurer j’étais présente 😭😭😭😭 accident bou meti je suis traumatisée. Yalla naléne yalla yeureume té kharel aldiana firdawsi si barké Seydina Mohameth ( psl) 😭😭😭😭
@ouleymatoudiagne1216
@ouleymatoudiagne1216 25 дней назад
@@fandao2138 Allahouma amine lou méti way😭😭😭
@talladiop8525
@talladiop8525 24 дня назад
@@fandao2138 non ya indiscipliné totale dans ce pays
@noumchjoop6808
@noumchjoop6808 23 дня назад
Amine😭😭😭
@bsowfall
@bsowfall 23 дня назад
Amine yarabi
@ShiekhjobeTijan
@ShiekhjobeTijan 25 дней назад
Yalña yalla yerem leñ ta khare Len Aljana fir daw ci 🤲🤲
@yamadione7495
@yamadione7495 25 дней назад
Yalla naléne yalla kharé aldjana firdawsi si barké seydina Mohamed 🤲😭
@khadygueye-ol2vm
@khadygueye-ol2vm 25 дней назад
Il faut que ça cesse, certains chauffeurs de bus Tata sont indisciplinés
@mamependaba7129
@mamependaba7129 24 дня назад
Tropppp c'est incroyable
@minadiop5652
@minadiop5652 25 дней назад
Les chauffeurs de bus tata sont très indisciplinés,
@tinefall2180
@tinefall2180 25 дней назад
Bilay wakhal dé
@afriquecomedie1224
@afriquecomedie1224 25 дней назад
Amou gnou béne savoir vivre
@user-cc2ye8fu2q
@user-cc2ye8fu2q 25 дней назад
Bilahi wallahi wa talahi la majorité des chauffeurs des bus TATA sont très indisplinés li dafa gnaaw torope
@user-cc2ye8fu2q
@user-cc2ye8fu2q 25 дней назад
Gnakeu yare rék bilahi
@Mbt.-_
@Mbt.-_ 25 дней назад
Walahi tay lako kham soff rew
@MayataDiop
@MayataDiop 23 дня назад
Nous nous valorisons d'une population jeune mais nous avons à plus de 70% une jeunesse indisciplinée.
@astoumbengue9728
@astoumbengue9728 25 дней назад
Yéne tata tamm nagn di ndieukanté souniou bouké founiou dieum niou faatou yalla naléne yalla gneuram
@cheikhgueye6946
@cheikhgueye6946 24 дня назад
Ina lilahi wa ina hilahi radjioun yal na yallah yesal ndjiegualam si gnom ak bep djioulit youfa nek amine
@dabaniang8141
@dabaniang8141 25 дней назад
Yalla nalèn bour yalla yeureum lèn tè dièguel len thi barkhè si aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲
@amydiagne6773
@amydiagne6773 25 дней назад
On doit les sanctioné retiré leur permit indiscipliné rek dou léénéen
@kingkabegueye3648
@kingkabegueye3648 24 дня назад
U a raison Bilay
@user-su8en9bf9l
@user-su8en9bf9l 22 дня назад
Amna si deux chauffeurs youniou nangou sén bus ak permis ndah dakanté biniou don deff
@EvFay
@EvFay 25 дней назад
Oh que leurs âmes reposes en paix yalla na yalla may chauffeur khol bou ko mougné ndessan mettina trop
@fatoumbackefaye7170
@fatoumbackefaye7170 25 дней назад
Hoooo metina masa que leurs âmes reposent en paix 😢😢😢
@fallougalassbeye3579
@fallougalassbeye3579 24 дня назад
Yalla nalen yalla yeureum😢😢😢
@maguettefaye612
@maguettefaye612 25 дней назад
Yalla naléne Yalla yeureum té kharé léne aldiana firdaws
@Mascoratun
@Mascoratun 25 дней назад
Yallna lén yalla yeureum té kharé lén aljana
@mbodjiaida9688
@mbodjiaida9688 24 дня назад
Amine YĀ RABBI
@user-sk8zc2fs1k
@user-sk8zc2fs1k 24 дня назад
Certains Chauffeur bus yii dinagn diexal niit yii danio rew semaine passée rq toutii lii dall niou... Yalna len borom bii yeureum
@sokhnaniang7926
@sokhnaniang7926 25 дней назад
Ndeysan yalla nak yalla khare alldina
@adamaseck8816
@adamaseck8816 25 дней назад
Amine
@mbodjiaida9688
@mbodjiaida9688 24 дня назад
Amine "YĀ RABBI "
@Elhadji2187
@Elhadji2187 25 дней назад
Walahi legui dokh si coté tali sah woroul ken hamoul li lanla
@fatoudiakhate1516
@fatoudiakhate1516 21 день назад
Yalla nalén yalla yeureum kharelén aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed
@peindadiallo2558
@peindadiallo2558 25 дней назад
diangouniou amougnou formation diougué dekeu ba rakhasse auto kheuye woute permie Di niou raye
@mamadoundiaye5230
@mamadoundiaye5230 24 дня назад
Bilahi chauffeur tata ay vrai domerame lagne déma guiss kérog niarri bus 54 di diékenté tout juste à côté de leur terminus
@Marianeladeess
@Marianeladeess 24 дня назад
Mr Cheikh Diba est un leader visionnaire dont les idées novatrices transformeront notre système financier pour le mieux. Nous sommes impatients de voir les changements positifs qu'il apportera Répondre
@user-lp9vu7sn4e
@user-lp9vu7sn4e 23 дня назад
Il faut savoir sanctionner le retrait du permis et qu’ils ne conduisent plus jamais de leur vie
@serignemodoukhouma1804
@serignemodoukhouma1804 25 дней назад
Nn li mètina trop yalnalèn yalla yeureum
@user-dl1kg2mu7i
@user-dl1kg2mu7i 25 дней назад
Yalna Yalla yeureum léne kharé léne kharé Aldiana firdawsi
@lesseseyni2659
@lesseseyni2659 25 дней назад
Tjrs de l’indiscipline totale en vers les bus tata C vraiment écœurant 🤦🏿‍♂️😭
@mamemorfall2086
@mamemorfall2086 24 дня назад
Moi je demande le PROS et son ministre de transport prendre leur responbliter surtout sur le contrôle des visites technique parceque les 90 pourcent des véhicules du Sénégal ne méritent pas circuler parcequils sont i inaptes même de transporter des moutons
@djibrildiop7561
@djibrildiop7561 25 дней назад
Yalna yalla yerem gni fatou
@garyibra9425
@garyibra9425 25 дней назад
Bilay dano réw ndakh débb 44 bima dieulone bimi wathi pon bi limdone déff dama sakh tite après tout sa ñiouni dogualou yalla li dafa eup wayy
@albourylatdior-ur1vy
@albourylatdior-ur1vy 25 дней назад
Yalna cheufeur bi dé si prison ba,ay vré vampire lagn domeram yi
@baye1975
@baye1975 25 дней назад
Ah weah kénn gnaanaloul kenn prison mais il faut que genre yi gnou door lénn ay peine you goudou comme ça dina servir leçon gnénén gni gnou yém.
@user-vh3dp2kk1l
@user-vh3dp2kk1l 25 дней назад
Yalnaleen yalla yerem te khareleen ardjana
@mbodjiaida9688
@mbodjiaida9688 24 дня назад
Amine "YĀ RABBI "
@user-su8en9bf9l
@user-su8en9bf9l 22 дня назад
Paix à leurs âmes , clients yi naniou bayi aussi dou gnouxou tata yi nagn dieul souniou matoukay sou fessé rekk niou bayi mou dém
@OusmaneDabo-ug8qh
@OusmaneDabo-ug8qh 25 дней назад
Man moto lay dawal mé dafa am ay seufor you sokhor dfoi niou défla lo khamné do kham lou takh niou déflako
@ndiemendiaye9979
@ndiemendiaye9979 25 дней назад
Nguen moytu di daw nank prck su décédé di am lu thi bari yenay ndiek de te yenewu ma len ko moto bu auto Dale thi kawam sur l coup ngay de delen moytu bubakh frere moytu bubakh
@abdoulayendiaye3974
@abdoulayendiaye3974 25 дней назад
Yalla nalén Yalla yeureum té kharélén Aldjana
@coubatandine5057
@coubatandine5057 25 дней назад
Paix à leurs âmes 🙏 metina trop 🙏🙏😭😭
@awadiop4774
@awadiop4774 25 дней назад
Bilay ndieukenté biniuy def si talibi eupna looollll li mom war naniou si wah borom tata yeup danion rew nek ay domrem deg Bus ddd yi dolen degue niouy def ben accident 😭😭😭
@user-jr7ls4zl1q
@user-jr7ls4zl1q 25 дней назад
Amine way inchallah 🙏🏻😭❤️
@babacarfam251
@babacarfam251 25 дней назад
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi
@aichaaicha7989
@aichaaicha7989 25 дней назад
Khamenei diomaye wore na dioukeu si li noumou gueuneu guawei éliminer tata yi cars rapide yi diagua Ndiaye yi camion yi téye vérifier permet yi aussi
@ndongomboup7518
@ndongomboup7518 25 дней назад
eliminer tata yaw yangui khalate
@Ndiayeniangua
@Ndiayeniangua 23 дня назад
@@ndongomboup7518bayiko bakham kon louy yobou nitt yii khana kay niou kholate permit yii nguay wakh
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 23 дня назад
Les transports en commun sont gérés par l’état ds tous les pays normal il faut que l’état augmente ses bus pour éliminer ses transporteurs en commun
@alalama1917
@alalama1917 25 дней назад
Leurs indisciplines est incommensurable ayyy domiiii dedioooo ndeyam laniou rekkk ces chauffeurs de tata
@premieredame6572
@premieredame6572 25 дней назад
Comment 2 bus de même ligne peuvent ils se retrouver net à net sur la circulation alors qu'il ya des écart au départ
@nenesall4636
@nenesall4636 25 дней назад
Eyeu waye Dakar plus yobou ngéne sama fiteu bi photo alhadji rafétna bingéne publier tafsi aye rongogne rafétoul diékoul yi lorou si accident bi yalla naniou khipé aldiana si barké seydina Mohamed psl 🤲😭😭😭😭
@syllndawa7312
@syllndawa7312 23 дня назад
Ndaysan matina torop yalana len yala yerem te kharelen aldianay firdawsi ammin
@diorndiaye4211
@diorndiaye4211 25 дней назад
Paix à leurs âmes
@user-fz1zc4ni7l
@user-fz1zc4ni7l 25 дней назад
Paix à leur âme
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 23 дня назад
A Dakar comment peut on conduire à une certaine vitesse une petite ville
@FamaNoreyni
@FamaNoreyni 25 дней назад
Bus yi tameu naniou li surtout 34 AK 31 bi .bo waré wathieu liberté 5 niou yobouleu ba cité keur gorgui soy wakh dounioula falé dileu niak kersa.en tout cas borom bus yi yarnaniou segue chauffeur yi AK receveurs yi
@papembaye4996
@papembaye4996 25 дней назад
Indisplinés total walahi Que leurs âmes reposent en paix
@mbayendoye7288
@mbayendoye7288 25 дней назад
Merci ❤ ❤ rafet
@NdoutyWATHIE
@NdoutyWATHIE 25 дней назад
C'est dommage.. 😢😢😢
@abousall7883
@abousall7883 25 дней назад
L’indiscipline des chauffeurs tata toujours c’est eu
@user-dx9ks2ce4bm
@user-dx9ks2ce4bm 25 дней назад
Paix à leur âme 🙏🙏🙏🙏
@user-fk1qr4em2b
@user-fk1qr4em2b 25 дней назад
Que leurs âmes repose en paix
@albourylatdior-ur1vy
@albourylatdior-ur1vy 25 дней назад
Domeram yi di fowé bakane nit yi mé nagn dé si prison bi rkk domeram yi après nane ay dogolou yala domeram yi lii réwandé rkk la amoul lenene
@matarndiaye3496
@matarndiaye3496 25 дней назад
Na bus Tata yi Tok 3jrs béne douthi dawe, na état bi dieule séne responsabilité
@youssouftoure259
@youssouftoure259 20 дней назад
Comment un voiture peut rouler sens frein 😢 c’est triste
@AdamaSeck-yh5qr
@AdamaSeck-yh5qr 25 дней назад
Amine 🤲🤲😱😭😭
@astousow5364
@astousow5364 25 дней назад
YALLAH negn hiper aldiana firdawsi DARADIEYE SEYDINA MOHAMED PSL
@FamaNoreyni
@FamaNoreyni 25 дней назад
Calcio laniouy toudé ndieukanté bobou. sen terminus yi laniouy tokk regulatrice bi dilene wakh sen heure diott n'a diougal tall auto ni niou begn tokk bamou nekh len niou départ souniou deparé daniou trainé ba guiss benene bus rek niou tek kossi kou beug wathieu do wathieu kou beug yekk do yekk"calcio"
@HouleyeSow-fg6fn
@HouleyeSow-fg6fn 25 дней назад
Loy diékanté voilà les conséquences maintenant tu est arrêté le reste de la semaine di tu est tu vas arrêté ba abadane legui reyga domou diambour yii paix a leurs âmes
@mamethiernondiaye9466
@mamethiernondiaye9466 25 дней назад
Bilahi ligne 44 bi chauffeur you réew niokoy dawal di rawanté
@honorinegomis5205
@honorinegomis5205 24 дня назад
Li lepp indicipline leu ,dieul na 32 même pas une semaine après l'accident bi amone rond point emg ,bamou nieuwé ba rond point canada, mou yeug cii kaw rond point bi touti auto bi keupou, bamou yégué ba médina receveur bi demandé néko mayléne niou wacc,niouy wacc rek mou démarré busbi Yalla rek moniou soutoural jour bobou, pour mane après cet accident sur le rond point emg dinagn cii dieulè leçon mais rien dafa melni danio guena rakadiou, l'État doit prendre des mesures sévère concernant ces transporteurs ,surtout les chauffeurs de tata
@MameMbackeNdong
@MameMbackeNdong 25 дней назад
Rip😢😢😢
@fatoundiaye1600
@fatoundiaye1600 25 дней назад
Tatayi lignite def d'où deug douyone nekfi di dieukalanter melni kou yebe aye mala mane lolou doundou nako ak bene chauffeur t'ai bo wakher niou guena yokk
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 23 дня назад
Les inspections ne sont pas fait chaque jour
@diarietousow6346
@diarietousow6346 25 дней назад
😭😭😭😭😭😭🇸🇳
@user-oc7ii7db6s
@user-oc7ii7db6s 25 дней назад
😭😭🙏🙏🤲😭
@user-sk9jr9ts7r
@user-sk9jr9ts7r 24 дня назад
Chauffeur bi nañiou ko teuthi 20ans de prison
@madinagueye168
@madinagueye168 25 дней назад
Il faut sanctionner rek permis à point et amende.
@galay2879
@galay2879 25 дней назад
Yala non yala yareum
@abydiouf1428
@abydiouf1428 25 дней назад
Chauffeur 44 yi daniouy ndieukantei rk
@katydiop2850
@katydiop2850 25 дней назад
Wa li ba kagne di raye komme aye mouche vraiment ware naniou djeule aye mesure
@AmadouTagoula
@AmadouTagoula 25 дней назад
Indiscipline késsé bilahi mime reuw
@rokyatoutoure610
@rokyatoutoure610 25 дней назад
Réwandé rék chauffeur yii danio indiscipliné c triste vraiment yalla na yalla yerum gni dém😢
@diarietousow6346
@diarietousow6346 25 дней назад
Autorité ne interdite auto yi maguet à Dakar svp merci beaucoup
@aidababou9678
@aidababou9678 25 дней назад
Ohhhh li méti na
@Fas9168
@Fas9168 25 дней назад
Di diay rewandé ba rey domou diambour yi
@user-ry5cx4tg7c
@user-ry5cx4tg7c 22 дня назад
Dawalkatyi amouniou respé daniouye mandi di dawal di reye nityi
@nonalincivisme
@nonalincivisme 25 дней назад
C'est dure vraiment avec c'est bus tata qui font leurs courses n'importe comment sa cest passe semaine dernière entre deux ligne 53 qui fesait une rallye ils ont faillis même créé une accident si c'était pas la nuit j'aurais les filme me j'ai photographié leurs immatriculation
@alphousseyni9427
@alphousseyni9427 25 дней назад
Sènègal nak diamono bi bari accident dè
@dakarbourguibavision8635
@dakarbourguibavision8635 25 дней назад
Ils faut prendre des mesures tres sévère pour les bus tata ,car ils sont devenus des machines a tués
@Kbs-production
@Kbs-production 25 дней назад
RIP 🪦
@amily104
@amily104 25 дней назад
Temps yi les accidents sont nombreux
@diopfatou826
@diopfatou826 25 дней назад
Bilahi 44 bi amna bouma dougou dembou di dem mermous dafa done niekaté ak bénen 44 niit yi di waxx ak chefeur bi falé woul kenn
@lassanasane2492
@lassanasane2492 25 дней назад
Ak ligne 25 linge 4
@Fas9168
@Fas9168 25 дней назад
Dagno rew ba doff
@jammrek
@jammrek 25 дней назад
​@@Fas9168c'est normal nak parce que ay analphabètes laniou, diangouniou école diangouniou alkhourane, ba nopi nék ay incultes.
@Fas9168
@Fas9168 25 дней назад
@@jammrek bilahi lou lerr nga wax hamouniou dara
@madinagueye168
@madinagueye168 25 дней назад
Chauffeur Yi ci boppam niou ci beurri danio Reew
@julojunior108
@julojunior108 25 дней назад
Accés de vitesse mome bouniou la diapé naniou nagou sa permis rékkk
@abdoulayelecataliseuramar5154
@abdoulayelecataliseuramar5154 25 дней назад
On a plique la loi pas de sentiments ?
@pacodiae4085
@pacodiae4085 25 дней назад
chauffeur Tata yui danio réw douniou dawal sene auto yui daniouye raame ba bénéne tata dabléne niouye ndieukeune té
@mandiayediouss6885
@mandiayediouss6885 25 дней назад
Non ç'et pas un problème de visite technique ç'et un problème comportement du chauffeur
@BakhyaythiamBakhyaythiam
@BakhyaythiamBakhyaythiam 25 дней назад
Elhadji rafétmi ès que ok Sénégal Gayguiss kouy dawalé permis diambour nanlén tadj fatélaine si kasogui rek asiden matay yi
@user-yv2ul2dn4q
@user-yv2ul2dn4q 25 дней назад
Bus tata yi nak War nagnou wakh si gnom dé
@moniquebrisson3552
@moniquebrisson3552 25 дней назад
Les responsables des bus tatas ils sont ou? Ils doivent revoir leurs CHAUFFEURS
@awadiop7280
@awadiop7280 25 дней назад
Mane dei ligne 69 bi djekaneté motakh ma bayiko chauffeur tata yi daño réw ta so wakhé dagne laye niawal di guena rawaneté
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 23 дня назад
Moto yi nio fi wara jouguer
@sokhoulovedieng1365
@sokhoulovedieng1365 25 дней назад
Ô metina way
@naboukebe5390
@naboukebe5390 25 дней назад
Pen de mort rek kou raye nanla ray mou diekh te seen auto yi ngueen khol gni ngueen koy diokh bou pen de mort amoon con liy khew dotoul am ndakh bo khalate ni bo raye niou rayla di nga khol li ngay def
@assthiam8160
@assthiam8160 25 дней назад
Wa site internet yi est que ay nitt lagne pour mane sakh théâtre katt bi mo dé
@jammrek
@jammrek 25 дней назад
Beug ay vues rék moléne ko diaral
@AichaKeita-rq3vh
@AichaKeita-rq3vh 25 дней назад
Allahou Akbar
@user-si6yi9ss7u
@user-si6yi9ss7u 25 дней назад
Danio raiw tatayi
@user-gu5mx7vb5g
@user-gu5mx7vb5g 25 дней назад
Thiak thiak yi laniou wara tepi sen leufeul ndey niou gueni thi capital bi
@jammrek
@jammrek 25 дней назад
Tata yi nak?
Далее
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 1 - Episode 34 **VOSTFR**
1:13:35
What does the result emanate from? | Faye D'Souza
56:23
Série -  Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 1 - Episode 35
31:09
31 мая 2024 г. | МАЙФ # 1 уже в сети
1:01