Sossou Tidjane bi Tarikha Mouride bokoul ci Tarikha yinou garantie Mouride yi teunkou wounou ci Sunnah Tarikha Mouride dieuméwoule talibé yi keur Yalla Mouride yi ci thiàkhane ak fo nanou nék Tontou Mouride bi Tarikha Tidjane mingui ci lokho Serigne Touba
La surenchère pure et simple. Les tarixa sont en perte de vitesse, en déclin et sont semblables au téléphone fixe face au téléphone portable. Tout le monde va se connecter directement et nul ne sera esclave d'un gourou dans pas très longtemps inch'Allah.
Guissou ma cou dak kath ni tarikha gnome gneup thi ay fene kesse lagn neck sirk ak boccale kesse yalla nagnou yalla moussal thi tarikha yi alhour âne ak sunnah cou thi wath sankou nga adouna ak alahira gni geumou gnou dina Islam