wally seck desalou dara wa senegal instan bi souko nekhe bayi musique live wally seck a vie leu machallah yallah borom bi wereule batte bi si barki Seydina Mouhamed (PSL)
Bravo niogui saa guinaww à jamais merci au peuple du Sénégal merci aux musiciens du raam daan chapeau a Wally vive le senegal Wally point yowe laniou beuguee yalla defala jaam tu est devenu le gardien du temple