Sëriñ Muntaxaa nee na: « Kenn ku ne bu ko manee jàng ñatti kaamil, bu ko manul it te man benn it batay baax na, bu ko manul te man koo jànglu it batay baax na... » La ca des lépp nag na ma ko waxee woon rekk, kenn ku ne lu mu xam ci lu baax na ko def ngir santle ko Boroomam...