Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yònnent bi (SAAWS) akiy sahaabaam (RAA) te wërsëgël nu ci ngënéelam nu dëkkag ñoom ca kërug teràngaam.
Machalah dieuredieufe cheikhna docteur mouhammad Ahmad lo louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye billahi deug rek nga wakh nga Lou ler nga wakh sen ligueye rafetna leral yi amna solo yalla na la yalla sam te arla