Ndeyssann je ne suis pas Mouride ni Thiantakhoune mais il faut reconnaître que les enfants de Serigne Bethio sont vraiment disciplinés, humbles et reconnaissants. Que Dieu vous accompagne
Akassa ! Y’a am yar, téy ta kham yonou mouride ak adouna. Dieureudieuféti Serigne Touba. Serigne Mountakha Bachir Mbacké yalanafi yague ta weur. Machallah, am na solo. 🙏🏾
Aïda diallo kay mouride yi la yap wayé dou l'islam / ndakh l'islam a déjà prévenir que djiguene dou meuçeu done kilifeu si kaw gor Yalnagnou yalla khir si bopam si barki seydina Mohamed psl amine
Vraiment kii defeu deugou Niémé neu et il est direct On connaisait pas les enfants de cheikh bethio mais dey nio am yarr deh il a bien parlé et puis diabotou cheikh bethio kenn meusou lenn degg ci bordel Je suis emue Mannn aida sey moko fa yobou wonn seybi diekh neu sou ko nekhei berou tey xamnei serign saliou thioune mo fi nee Dou ma thiantacone mai sama xalat leu
Mayy yaw yay mane ne veut pas dire k nii souma déweii yay done sama Khalife teii bou djiguéne done djitteii kone sunu Khalifs you beurii fii daniuy kharrrrrr
Iow sa baye kouko gueuna done goor yalla dafa am té Mo djital Sokhna Aida Mane dal xamnani Sokhna Aida Molène gueuna digne wa keureum tmt niolëne gueuna digne ndax dinagne dieul parole babayi té dounioulène garouwalei té yë xamoulni sax vous êtes dans ce bas monde té yène chaque jour nguène Koy garouwalei Té Sokhna Aida sou amoul ndam kone Kane moko am ???mom mouy djiguene rk té limou dieuf ci magal gui benn goor défagouko waxoumalak iow kone mom sou amoul ndam Kane mokoy am ??? Bilae Sokhna Aida rawnalène té dounguène sen sax peundeum
Dafa lére st srgn saliou rk atou ka ki fé ki fi rafétoul té mou mene nék béne sokhna aida mourite digale défale lila srgn mountakha wakh nakh lp geuneu nékh adouna amoul solo na raféte rkk yalle nasa khéle délou sii si mbrcké srgn saliou
Déug dal boci wété ite nékci rék kou dëgou dinala fékci té kou bagne gneuw nga bayiko té fékhé ba dëpo ak santané Sr. Saliou té bagna sosse dara thi yonebi ndakh borom matalna lép té moko samal bopam. Naléne Yallah samme té aar léne.
Je pense que li takh senegal yeup merewone cheikh bethio ken waralouko loudoule aïda momou on peut voir quil a eduqué ses enfants dans la droiture et dans letique islamique ce quon na jamais remarqué jusqua sa mort. La femme est tres claire dans ses actes et c typiquement le comportement du cheikh apres setre marie avec elle. Cheikh Bethio etait bien un vrai musulman et le comportement de ses enfants et limage du cheikh bethio deg ndigueule ame yare ak talibé que serigne saliou avait cheikhal mais malheureusement détournée par satan aida diallo qui continue de diviser ses talibés
Cheikhouna Mbacké baye khamm nanou histoire l'Islam dh bi fi yonétébi bayéko sokhna aicha mo djité wonn mbollo ma ki nak di sokhna Aida serigne bethio Monika Yaw La wolou sama guinaw kousi ande ak mome dh dinga déff loma nékh té nioune li nékh serigne bethio rék lanouy déff. Serigne mountakh wakhnako kouné kholale koula doy si ndiabot gui mou djitéla konn kay wakh dji diékh na nioune sokhnasi monou doy point