Franchement sen liguey raffetna niit warou gniouko diengue une semaine sans mou bougé wakhatouma 20ans c'est abusé l'être humain doit bouger tout les jours pour ses articulations pour sa santé physique et pour sa santé mentale sénégal la plupart des gens ne réfléchissent pas bravo à toute l'équipe de Pape Pape Niang un grand Merci .♥️
Yalla nalène yalla takhawou INCHALLAH té yalla dinaka defff inchAllahh yalla nalène yalla fay sama khol fessna dioyna ndakhté nite nite le rek ki mounona nek kouneke si gnoune yalla nalène yalla faye 😐😐😐
ما شاءالله رفعكم الله قدركم على هذا العملmachala limome rafetna lole sakh telepp nak sougnou mame jojou ngenko defall Mai bou ame febarou xelitt dou lole thonbi mokhawa bari CI mome ak problème yi mais yalna yalla motali
Li eupeune lol té méti. État warna wax thi li. Wadie ande na ak khélame. Bok you niak diome lol. Bo amé kou wéreudi dagaykoy takhawou. 20 ans guéne nek ak mome dou sangou dou rakhassou. Guéne dougou thi nek teuthie mome mou diakarlo ak lépeu lou mana lor domou adama. Yéne wa keureume doguéne war eupeu Tole. Dieureudieufaty association ande takhawou nie wéreudis. Que dieu vous accompagne. Thi kaw thi kaname lafthiat.
Ndeysane j’ai un frère malade mentale qui a disparu la fois passé on m’avait dis que il était a côté de Richard Toll khana di gnane YALLAH REK nguen tasse ak Mome il s’appelle Ablaye Camara que Dieu vous rendent cette noble travail que vous faites 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Moi jai pleuré en regardant le vidéo la remarque ke jai fait est qu'il nest pas agréssif je me pose la question pourquoi le chainé té aussi guiss nani kouko fathie dina weer bilayi Association bii yalla nalen yalla doolél
Machalla les frères vous étes brave que le bon dieu vous donne la force et santé de continuer c'est très dure et difficile mais dieu est grand Machalla Alhamdoulilah Alhamdoulilah 🙏❤️❤️❤️❤️🙏
Alhamdoulilah c'est très dur surtout à tant que Maman, mais ce que j'ai apprécié c'est que les parents l'ont toujours gardé malgré la situation yalla nako yalla diapéler et chapeau à vous merci