Certes c du téléfilm mais c se passe la même chose dans la vie réelle la vérité se place toujours à la fin de l’histoire motah loula diakhale rek bayiko ak souniou borom ❤❤❤❤
Képou kouy magali manguilaye gnanal yala tékeela si yonou diamou nga démm si diam gnibissi thi Diam ak salam yala mouseul lén si lamigne ak bala amineee touf touf 🙏🤲🤲🤲
Pourtant li niouy jouer ni lou ame la mane mi doundou nako sam woudiou pertiorgo sama jour ndiénté dafa déme lathié béne si sama couleurou yéré yi mou dieunde bou mél nonou rien que pour saboté sama khéw mais malheureusement dalou si ndakh mane sêy normal la woté sama mbokou ndieukeur gnipa ma diapalé takhawouma🎉 merci à tout l'équipe ❤
Les Sénégalais ne souhaitent pas la fin de la série mais ils se réveilleront un jour pour réclamer la fin de la série Comme ils l'ont fait avec wiri wiri
très sincèrement, vous nous décevez nous sommes à l'épisode 108 et les minutes diminuent d'épisode en épisode. les pubs sont devenus même plus important que le film
Bonsoir à tous et à toutes les setaneurs que la paix soit avec vous et à nos familles gnou tanbaléti AK xol you diekh dakh bator ya gnak diom si xalé😂😂😂❤❤❤