Тёмный

Firi Guent - Épisode 148 : Voir en rêve un de ses 2 parents 

Firi Guent Tv L’officiel
Подписаться 121 тыс.
Просмотров 113 тыс.
50% 1

Опубликовано:

 

29 окт 2024

Поделиться:

Ссылка:

Скачать:

Готовим ссылку...

Добавить в:

Мой плейлист
Посмотреть позже
Комментарии : 70   
@aminandao1093
@aminandao1093 3 года назад
Moi j'ai rêvé de ma mère vivante ,mo nek dima sangatte ay safara
@bayeniasspadane1439
@bayeniasspadane1439 3 года назад
Macha alla firiniou balaie ,courouss ,homme celebre, cle,porte,batiment ...
@cheikhdiakhoumpa8230
@cheikhdiakhoumpa8230 5 месяцев назад
Maa sha Allah amna solo. Dama guinte sama papa yonima
@abdoulmadjibdiop9191
@abdoulmadjibdiop9191 Год назад
Mane dama guent Sama yaye dima door machalla tontou lér na
@khadidiatoudiop4197
@khadidiatoudiop4197 10 дней назад
Seigne bi dema guent gniw diokh sama yaye gouro mais bene dommm la ? Dibalema rekkkk girl yalla
@amathsene6683
@amathsene6683 Год назад
Ouztaz dama guent sa papa bou gagnou nema mayma khalis ma nianala
@GhFh-sd1vk
@GhFh-sd1vk 4 месяца назад
Oustaz Dama gent sama kheum
@AdouNdiaye-m1l
@AdouNdiaye-m1l 27 дней назад
Dama guent sama wadiour bou goor bouye doundou mou guène adouna
@AwaDerr-t2e
@AwaDerr-t2e Год назад
Dama guinte sama papa dima niana❤❤
@KhadijaDiouf-l6c
@KhadijaDiouf-l6c 7 дней назад
Dama génte Mane ak sama yaye gnou nék si béne auto bou wékh ms sama yaye modone dawalle après autobi pane gnou boukhe coo ba soneu dagno moudié wathie dokhe. billaye dimbalimaci diakhale nama trop 😢
@Ndéye-q9l
@Ndéye-q9l 7 месяцев назад
Man dama guent sama Yaye yeuketima si kaw tekk ma si ay bakk mam
@teestreeter4628
@teestreeter4628 3 года назад
Machalla oustaz firil ma un homme célèbre gakoy guint lou barri diko guiss wala guint guén seuy nek en couple loumouy signifier🙏
@adjigassama3643
@adjigassama3643 3 года назад
Ii''' ''09' '' 'ooooooo%oo}} oo088' 09èmey 8888
@PatrickFea-xb4nr
@PatrickFea-xb4nr 8 месяцев назад
Dama gente sama wane ginaw di deme makaye wo si loudoul guente dama ame sokhla beug mou nianalma ma gente mou wane ma ginaw deme
@socegaye6175
@socegaye6175 3 года назад
Ziar nala oustaz dama guent guiss sama yaye fébar bay wathiou ay fourir you wex madone lathie lane leu
@torodopure2641
@torodopure2641 Год назад
Oustaz Mane dama guente sama papa ayye niit diapeko dikko door ma nieuw dikko sauver ba todji boppou gnognou Ak kher té après sama papa daffa contane si Mane ba mayma 5000f légui ma diox ko 1500f yiii dieul lissi déss lane lay firi svp Moment bimako done guente sama papa daffa fébar trop sax😢😢
@ambamb525
@ambamb525 Месяц назад
Dama guente billahi dama tite 😢😢😢😢😢😢 ay 2h la yewou mounouma nelaw
@NdeyeantaNdao-u3d
@NdeyeantaNdao-u3d 5 месяцев назад
Oustaz dama ghent sama papa dima nianal😢
@alidia7747
@alidia7747 3 года назад
Firil niou homme célèbre ak mbeute nguir yala
@feroce-vw3ox
@feroce-vw3ox 8 месяцев назад
Dama guent di khoulo ak sama papa
@AmadouBa-z1c
@AmadouBa-z1c 11 месяцев назад
Dema géunte famme bou am 42ans mouné défa beugue diékeur ma am yéné woutall ko diékeur
@sierraskye6904
@sierraskye6904 3 года назад
En règle générale rêver de sa famille signifie un sentiment d e non terminé où d incomprehention (Comportement, propos ect...) Il faut donc finir se qui n est pas terminé avec les personnes concernées. Bon ou mauvais mais il faut le terminer. Reprendre donc contact et Poser des questions
@NdeyeOumyNDIAYE-uq8tl
@NdeyeOumyNDIAYE-uq8tl Год назад
Moi j'ai révé mon père vivant gniouye setane télé di waxtane
@timafall355
@timafall355 Год назад
Dama guent sama papa di guinté mais sama màme bi ko Diour modon rogue Agne yi té Domada yàpp là tgue Butt yi gnew gnou Len di servir,mais l soir ma Degue ày dooy ÿou meti mà daww guéneu néké sàma papa mo don door sama rakk bou góor di ko sàyi Si bena Keur bou am zing si kaw mouy youkou youkou you meti. Dama beugon nga firil ma ko
@mamecheikhgueye4909
@mamecheikhgueye4909 5 месяцев назад
Asalam aleykoum dama guente samay mame you djiguene ak sama nidiay ak sama ben tanta gnoumay wo di retane ta gnom gneup gnon gui dounde
@m0asthomas119
@m0asthomas119 Год назад
Merci Oustaz. Svp deffal thème ci comment savoir kou mom guent bi .
@bintoukhouma3563
@bintoukhouma3563 3 года назад
Machallah Amna solo trop
@KamilaDiarra-s1p
@KamilaDiarra-s1p Год назад
Bn jour dama guente ma doff
@fifafatu6452
@fifafatu6452 2 года назад
Wa bouy jooy jooy you amoul son nak
@seydousow6237
@seydousow6237 2 года назад
Guènt sa wadiour bou djiguene djite mbolo di diouli
@nikitafall2744
@nikitafall2744 3 года назад
Wa legui guent di door sa yaye nak loumouy firi
@aissatoulabosall8496
@aissatoulabosall8496 3 года назад
Assalzmou alleykoum nioguu ziarrr Guénnt sa wadiour bou djiguénn dilla dorr naggg...diécckki diékki arrêté melni kou reuthiou dorr yi
@MouhamadouLo-xz2yk
@MouhamadouLo-xz2yk 5 месяцев назад
Guent tok ak sa papa di lék
@alimagaye3496
@alimagaye3496 3 месяца назад
Yaw nio bok guent
@mamediarrandiaye686
@mamediarrandiaye686 9 месяцев назад
Mane dama guènteu sama papa di dioy dima balou akk lanlay signifier?
@ndeyendackmbaye3664
@ndeyendackmbaye3664 3 года назад
Guent sa papa décédé nga dioy dioyou méti lane lay téki
@sodandiaye3609
@sodandiaye3609 2 года назад
Goudou fane
@fatoulalaseye6580
@fatoulalaseye6580 Год назад
Goudou fane leu
@aissatoucisse2062
@aissatoucisse2062 Год назад
Day gudu fane
@mameboussosourang
@mameboussosourang Год назад
sama papa dafa guén adouna mais dama guénte niou dag si ay thieureum té ab kharitam moko déf
@modoundao3485
@modoundao3485 2 года назад
Salam salam Serigne bi ,Mane dhé dama guént sama wadjoure di toure Sow bou farr
@JeanSall-lw4vj
@JeanSall-lw4vj 4 месяца назад
Gente dage sa loxo yaye.baaxna wala
@souleyeseck618
@souleyeseck618 2 года назад
Dama gent sma yaye dima diokh lekk man Ak Rak
@DiarraBadji-g6h
@DiarraBadji-g6h 10 месяцев назад
J'ai rêvé d'un groupe d'enfant qui lance des pierres à ma mère
@RaguiDiallo
@RaguiDiallo Год назад
Dama gent sama yaye Di balaie
@dia1894
@dia1894 2 года назад
Damako diokh khaliss pour mou déme marché
@nanaaichaalirida5406
@nanaaichaalirida5406 3 года назад
vous pouvez traduire en français svp. merci
@absawade4706
@absawade4706 Год назад
guénte sama yaye dima nianal sama ex bi déllouci nak
@maneseck1271
@maneseck1271 3 года назад
Mane dama guente sama papa mayma 130.000 ba parè may dioy Niko dama beugue andak ioe mouf fompe sama larme yi ba parè andak mane dougeul ma thi autom mom modone dawal ma takk thi kanam amna tmt kou goor kou nèkone thi Guinaw kou thi kham dara diapalè ma
@rachellemane1883
@rachellemane1883 Год назад
Numéro bi dokhoul
@sakhnasilo5589
@sakhnasilo5589 3 года назад
Wa gente sa yaye dila door nak
@Ndiobafaye997
@Ndiobafaye997 3 года назад
Dama guent y guis ay golo you bari si kaw garab
@cherifmbaye2616
@cherifmbaye2616 3 года назад
Cheytané la
@mbendadiop706
@mbendadiop706 3 года назад
Outeull mouslou wayyy yala bakhna.....yala na gneup am diam
@mariamadiatta9531
@mariamadiatta9531 3 года назад
Firima guent Maryam makoy assister bimouy wossine Issa
@willymadjiguenediop8623
@willymadjiguenediop8623 3 года назад
Mashallah
@sokhnafatythiam904
@sokhnafatythiam904 2 года назад
vou guent sa yaye maylla telephon
@mamediarrakane4235
@mamediarrakane4235 2 года назад
Guiss sa yaye febar nak
@fatoulalaseye6580
@fatoulalaseye6580 Год назад
Bouféké tanéneu si febar bi xamal ni dina goudou fann
@AllaSy-cs7dt
@AllaSy-cs7dt 5 месяцев назад
Mane célibataire la dama gente sama yaye fébar mane ma gnew pour yobou hôpital
@islamareligion
@islamareligion 3 года назад
Svp meun nga fiiri si guente di dawal auto
@maneseck1271
@maneseck1271 3 года назад
Lolou seuy la mariage
@MactarMactarkanediallo
@MactarMactarkanediallo 7 месяцев назад
Guente Di nelawww si mbedd je. Ne pas vue sa
@khadjiasene3649
@khadjiasene3649 2 года назад
Numero
@sirandouniangadou4682
@sirandouniangadou4682 2 года назад
Mane dh sama yaye dmaa guente moi dieul balaie beugue ma dorr 🤭
@adjacoumbafall
@adjacoumbafall 2 года назад
😂😂
@alhagiekebbeh3802
@alhagiekebbeh3802 3 года назад
🇸🇳🇸🇳🙏🙏
@Hotep-dt7qv
@Hotep-dt7qv 3 года назад
Revé de vêtement gneuweuguoul
@ismailathiam5475
@ismailathiam5475 3 года назад
Bonjour j ai rêvé d un enfant que j' ai pris dans mes bras et une femme que je connais je veux une explication stp
@astoumbenendoye3598
@astoumbenendoye3598 3 года назад
ماشاءالله
Далее
Revoir ton père qui est décédé dans un rêve
10:48
Rêver de fou ( doff )
11:40
Просмотров 24 тыс.
Voir en rêve sa défunte mère
5:23
Просмотров 22 тыс.