Leegi Ana maandu? Ana bàyyi xel né YÀLLA day regle lépp ëllëg? Yéen ñikoy sikkël ndax yéena ko gëna tege ca yoon wa? À doom mosléen ak Maandu! Damaa seetlu né njañse (commentaire) yi ci yuutub (RU-vid) ak fesbuug (Facebook) leegi li ci ëpp ay tooñ la! Am njañse (commentaire)dafa bókkul ak linga wax ci saw làmmiñ? Maandu léen ci jaami YÀLLA yi ngir YÀLLA mi léen bind. Kii xamnaa ko bu baax doonte moom xamu ma bimay nekk senegaal ñoo bokkoon bénn koñ, caaroy laaroset, (Thiaroye la rochette) bamuy deff aw ñàqam ci sëriñ bi booba amagul lu bari. Du caagéene damakoy layal Deedeet! Dafa fekk né وماشهدنا إلا بما علمنا.
Ki mome dafa bari wakh ta ay kadome dafa violence yaw ya mome touba bafay géné kéne Serigne Touba diamou ak salame la woté nanio djital maslah ak yété ndakh niaka xam mo waral lo bari