Il est unique kou tedki ❤❤❤ kene amoul li defar magg,defar rakk,defar nidiay,defar ndeye,defar baye, tarbiya ay goor yalla yo khamné kéne kou né qoutb nga dieuredieufé Serigne Touba 😢
Ndeysane 😢 Son bi bamouy guéneu senegal nekhone na walahi☝️. Sama enfance nekhone na walahi lazim 🥹🥹 Yalla Dieureudieuf. Cheikh Ahmadou Bamba sante nala geureum nala . 2023♥️♥️♥️
Un homme qui a eu son grand frère et ses oncles comme disciples son propre père a utilisé c'est écrits pour éduquer ces talibé 😭😭😭 BAMBA est juste incroyable