Ça fait vraiment plaisir.Sergne Moustapha a toujours sa place à Tivaouane.Que le tout puissant unisse la famille de Maodo et que les problèmes internes se règlent en famille.
La division la desservi lors des élections .lui il se croit incontournable. TIVAOUANE vit sous le khalifa de serigne Babacar sy Mansour. Pour preuve :la grande mosquée .
Seydi Mouhamadoul Moustapha Sy nieupa la beug Sy Malick.... Walahi boo beuguè rek lepp baakh...Niaan naala ko si sa barkè Mame lou am rafet bou amoul woon rek niaaw
Macha Allah demb dama contaan trop barker Serigne Babacar Sy. Mon grand rêve ce est de voir au soir du 21 avril coïncidant avec la ziaaar Générale Serigne Moustapha Sy Al Maktoum à côté de son petit frère Serigne Moustapha Sy Al Amine ❤
Bien sûr ! Niou bayi khéle si noone yi ( les Wahabistes) qui ne souhaitent que le déclin des Tarikhas mais ils ne le réussiront jamais dans leur sale mission qui est de combattre les Tarikhas pour faire plaisir wa Makka
Tacko yaw amo xam xam halé moy lann? ? ? Estcceque magoul sa baay tamit ndah yalla Dou diokh màkk responsabilité gnimou am yeupp kharoul bagnou maguétt Mouy soga djeuflanté ak niom
Te ngeena mandou té yam plaçou talibé bo lene meunoul wax lou rafet ngene nopi gni gno bokou ak lou meuneti xew nagnou lene gnanal diam mo geune ndax moy sougnou diam yalla na bour yalla doli soutoura