Machallah ya Oustaz niou ngi lay ziar dila diadieufal. Pour ceux qui ne l'ont pas encore côtoyé n'hésitez pas en cas de besoin. C'est un homme modeste, gentil et généreux machallah. Dinala deglou, dalal la, conseillé la té andak yow thi sakkou sounou borom mou fadjal la say aadio. Nako nieup nianal yalla samm ko, aar ko mook ndiabootam té deugeural takhawayam amine ya rabi. Oustaz da nga bakh rek wayé yalla mola gueuna bakh kone yalna fayanteek yow thi mbaakham ya rabi 🤲🙏