Cëy !! Ndaysaan xoolal rekk bu Senegaal bu njëkk nit ñi ni ñu daan soloo mu rafet lool te yiw tubaarkàlla wuute lool ak sunu jamono jii nga xamne vulgarite la ñuy concour😢😢 Way wi it dafa daw yaram lool te daf may fàttali lu yàgg ba may tuut tànk ndaysaan