Aywayy niit kén douko topou bamou seuss, même bouder elle a plus de 40ans tamite mom leu au moins mingui tokk si seuyeum. Yalla rekk mofy nekk yalla nala yalla maye ndiabott si barké kou tedki💕💕💕
Bilahi le Mari de NDEYE Gueye Boy djinné est un vrai homme bilahi malgré que la pression en disant qu'il est plus jeune patati patata mais il gère très bien sa femme, l'amour n'a pas d'âge
J'ai les larmes aux yeux😥😥 à chaque fois que je regarde tes vidéos , car on ressent à travers tes paroles que tu es une femme merveilleuse et exceptionnelle. Yalla nala yalla defal li guene, maye la diaboot bou barkel si barké Seydina Mouhamed SAW
Ndaysan, elle est vraiment modeste khamna souniou boromm khol bou rafete lay faye ak moudje bou rafete. De plus elle est célèbre, elle a presque fait le tour du monde et elle avait le choix de se marier avec un célébrité mais elle l'a pas fait. Mougnal nakk je connais quelqu'un qui a fait 10ans de mariage avant d'avoir 2 gosses.
Soubhanallah comment on peut demander ces genres de questions à une femme qui n a pas encore enfanté et qui rêve que de ça. On ne demande pas on fait juste pour des douas pour la personne. C est tout .arrêtons svp
Du courage ma soeur ça se voit que khol bou rafett ngua yoor continue à aimer et soutenir ton mari dina bakh inchalah nianal nala sama biir khol ci barké sr Fallou ya kham li ngua beug yalla defal lako les chiens abois la caravane passe boul titt boul ragal boul falé. ...SIMBA
Ndeye bilahi mala beugueu,elle est simple beugueu dieukeuram té yallah rek takh,soula nékhone nga seuyak ak ay célébrité mais defoko,yallah na sa diam yag
Bilahi dioyna,imagine tw yéneu goor yi nouniou mél,di wonéwou,di snap par ci par la,tei dieukeurou ndèye guèye bi dafa yarou beuri kersa,mo ngui neubeutou rk,yalla nalén yalla méy ndiabot,dome thii lokho yalla la neik
ndaye yalla nala yalla maye doome sisa seuye bi sa s voi k yangui diape sa seye bolési nak fouleu ak fayda mane daale j taprécie ndakh djiguêne amoul loudoul seyeum
Nabou sylla ,yowe deh boo oubber salón ,estheticienne ,visagiste ,dina fess inchallah .ndaxx nandite nga.lii moy ngaa wangg va parer soll toubayy bou ame poches militaires you ngander si guinaaw.taxaww di settlou SA boppeu dafa baxx.xaam lilas djappeu ak djappoul.....
Ndeye Gueye machallah Bilay damala beugue legui ndakh nigua béter gnou beri ame foula tok sisa seuy si kaw sa kanam yalnala yalla maye diabote bou ame barker
Niak ngen fayda trop ta meune wakh lou amoul sens sou amé 40ans walla 70ans mome la engager au moins khol na kimou beugu di seuy ak mome ta yalla rek takh yalla do déf lou bakh moulay fay lou bone yén gniy wakh woutilen dieukeur koulen tak si farata yalla mo geune si yén soff ngén trop 😡
Ndeye Gueuye ton vidéo que tu disais diabote reck laco meuneu fayer ca ma fait pleurer yalla nala yalla maye diabote acke papa yalla meuneu louner yalla nalaco yalla maye si Barker seydina Mohamed 🙏🙏🙏🙏🙏
Non non et non Ndeye Gueye tu as plus de 40 ans, on à grandi ensemble à Pikine rue 10,koniou Kiné Lam !😅😅😅,kaméme Yalla nalla borom bi défale diam, maye la ndiabott bou Barké ✌✌🤩🤩
Quand vous demandez à avoir des enfants faut dire yalla naleu djikk car demander des enfants ba parer c pas bon pr la mère et mettre sa vie en danger c pas la peine...
Lou diaffei si diamono ji moy seuye tei yalla takh. Sa seuye bi yalla guasi ame ndame tei gua ame si ndiabott bou barkel! Inchallah takh na ma sopp la bubax
Tu es vraiment une femme exceptionnelle, toujours belle, yalna la yalla maye ndiabote ak sa dieukeur, ma chaallah, que Dieu vous protège🙏, les soi disant journalistes posent des questions bêtes