Machalah dieuredieufe oustaz oumar Diallo louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla faye billahi deug rek nga wakh nga Lou ler nga wakh sen ligueye rafetna leral yi amna solo yalla na la yalla sam ak molem oustaz bouy wakh si alquran ak suna