Mashallah sama rakk dji bègal ngama atoum 2024 bi 😢 hoo wallahi sama rangogn tourou na 😢❤ Mashallah 🥰 mboup danga ma dèlo thiossan mbouben ak wa keur cheikh Matar diop yalna yalla yeureum djeylany mboup bèna galagn rek ndeyssan 😢yalla goudal fanou mbouben yeup ak ndiayen yi sama wa keur yi djital si cheikh Abdou Mboup wni sagal nga cheikhna cheikh Sadbouh Takhiyoullah ❤❤❤❤😢