Beaucoup de respect au policier de mbacké sa c'est la civilisation sama xol bi dafa diékhone tak quand j'ai sur les réseaux sociaux les policiers de Dakar frappait les gens comme des animaux c'est pas normal mé séral ngéne sama xol les policiers de mbacké vous êtes des professionnels merci a vous
Touba dafa nekh lou rew mi di yeungou yeungou touba mom douko yeugal yaramam fii amoul dor keine lep si yar lan ko tek thieuy touba mo nekh bofi nekké sa xél day dal si lep
Félicitations, au policier et les citoyens qui respectent la lois !policier yi nañu and ak hel ñu bañia dor yi nda ñiun ñiep ay sénégalais lañiu c'est vrai que nous sommes dans un moment difficile mais natou yalla dina diek !je prie que dieu nous protège tt !!
Wallahi sama dafa séd trop thi nii nguéne koy défé sétane nako bamou diékh dorou léne kéne té am nguéne linguéne beugue yalna lén yalla défal diam diambar nguéne Machallah touba sama deuk sama xoll
C’est la première fois ma gui ay commentaire 90%yi positif Bravo les forces de l’ordre 🇸🇳🇸🇳🎖✊ Kone nak niou deuppo ak ndigeul yi Té respecte sunu boppu avant tout
Bravo aux forces de l'ordre de la Ville Sainte de Touba, vous avez assuré sans violence. Qu'ALLAH vous récompense bi jaahi CHEIKHOUL KHADIM et que la population prenne conscience aussi de la pandémie et du couvre feu.
Macha Allah les policiers de Touba Respect sur vous... Vous avez fait du bon travail contrairement à vos collègues de Dakar qui frappaient les gens comme pas possible c'est vraiment triste pour les victimes 😭
wonderful job les policiers de mbacke vs êtes très sérieux ,intelligents, tolérants et compresible . je vs aime ! febar dey bété nimporte quel heure o moins yena ngui lathie
Vrement job bi rafètena les policiers 2 Touba am ngène kèrsa amoul dor you mèti comme les policiers 2 Dakar ki detrui le corp des citoyens Bravot à vous
Billahi dma ragal policiers ms yén takh gén ba beug lein dh wallahi sma xol sed nasi yén 1er jour waxal fouleu kou deugeur bopou wanko sa liguéy vrmt je vous aime bcp
Waw kay ni dal dacornathi .respèctè sa bopou,respèctè domou adama yi.respect a vs donc lè Hommes d tenus.prsk sama borom keur wone homme d tenu la machallah.chapeau a vs🙏❤
J’aime 👍🏾 se travail de sensibilisation sans frapper des gens mais faire respecter les policiers 👮♂️ à Dakar c’est catastrophique violence avec frappes
Imagine d'être a leur place ....{les sénégalais qu'on tape} cette message la que tu viens d'écrire il y'a 10 heures va être totalement a l'envers (réfléchit dit donc) se n'ait pas comme ça .........ahh putain f**k
WawAw Police ni nguen di Ligueyer ni mom Vraiment Daccord naasi chapeau a Vs Teenguen wah sen yenen Moromou Policier yi niouy def ni tee bayi doreee bi.
Vraiment séne liguéye rafét na diapé léne niou séni RAK niou diapéléne sounouye mak ande laniou wara déf wolo done béne yéna ngui déf séne liguéye sans violence merci beaucoup a vous nioune ak yéne warou nio done ay anémie big respect a mon frère DIONE Depuis Mbacké
Vraiment je suis très content les hommes de tenue à Touba ms il ya des policiers frappe rk lan khm si démou rk Dakar Policiers line done dfe dfa niaw lol diapou domou diamour dika d'or khmo foumou diaougué d'à seri wle d'y dem wla dy wout ordenage
Thiey serigne touba lepam rek ak yar la ak teguin ak diangale wante diapou domou adama yi di dor kom bayima bilahi ma naw waa keur borom touba yiii si lepou