Тёмный

Urgent🛑nomination de malick ngom-Sathies Bala Gaye dou Sama kilifeu écouté la réaction choc de Bour 

Bprod media TV
Подписаться 364 тыс.
Просмотров 7 тыс.
50% 1

Опубликовано:

 

31 окт 2024

Поделиться:

Ссылка:

Скачать:

Готовим ссылку...

Добавить в:

Мой плейлист
Посмотреть позже
Комментарии : 46   
@alidiouf1439
@alidiouf1439 5 часов назад
Merci Bour TU AS RAISON SA Thies mo wara kham ne Balla moy Kilifam par force
@Asnhgp
@Asnhgp 10 часов назад
Sathies ne fait pas l'erreur de Lac de Guerre et Gouye Gui 😅 Balla soko bagné sa soukeur dotoul saf Yalla moko déff alors soit intelligent profitél si bayeré balla bi sino dagnoulay cancle balla motahone gnoulaye supporter sans balla doumala supporter. Reuye bakhoul té balla dafa naïf rek wayé kou bahla 😊
@secretsdevoiles2567
@secretsdevoiles2567 9 часов назад
Bilay deug leu . Sou deglo nit gni ba bérrou dafay sonou rek 😢 mais dou degg roi des arènes
@djibrilseye5196
@djibrilseye5196 Час назад
Mêm mane balla motakh makoy supporté mais meussouma nekh
@idrissadione7279
@idrissadione7279 57 минут назад
Ngir yalla akh yonéntébi bayilén sathiés akh balla gaye gno boka ndéye akh baay mais noooooo 😢😢😢
@khalilo2423
@khalilo2423 2 часа назад
Saway entre famille boulssi dougou bassi débat
@elhadjisambe3549
@elhadjisambe3549 2 часа назад
😂😂😂😂😂bour boul titeul lirou waye
@cheikhsourang6023
@cheikhsourang6023 Час назад
Balla mongui fafétal mais sa mom mo dessé problème bi akh😢
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd 5 часов назад
Lolen wakh sa Thiès togne koh sen yone nekusi seytané Guen tropp madou lene
@makambtv608
@makambtv608 52 минуты назад
Balla gaye mo amal ndiarigne sa thies mais sa thies amaloul gnarigne balla kone mom mo wara mougne nangou kilifteff
@Dakarservice-ko1qp
@Dakarservice-ko1qp 12 часов назад
Sa thies frustration ak ignane moko diap wayé kou khamoul khamoul rahass sa kholbi té dioubo ak sa makk mane mome dotoumako supporté
@mouhamadoudiop678
@mouhamadoudiop678 11 часов назад
Dafa khamoul nii niouko faral yeup balla gaye 2 motakh
@keurguifootballps3678
@keurguifootballps3678 11 часов назад
Lolou la khamoul sathies gnouko topou yeup 90% c'est grâce à bg2. Qu'il soit reconnaissant envers son frère
@shollbidiatta1240
@shollbidiatta1240 10 часов назад
Balla naka dioumé wakh defal nako li AK li lolou dou dara balla dou diambour souko défé daka wara def souko defoul daka wara def sa Thiès xol bou ndaw la yoor té day diap Hein
@djibrilseye5196
@djibrilseye5196 Час назад
Gniko faral gnep balla gaye motakh gnou faral koo mane mom dotoumako supporté ndakh dafa def bopam mak té lolou bakhoul thi mom
@djibrilseye5196
@djibrilseye5196 Час назад
Sa thies danga wara khamni Balla gaye motakh gnoulay supporté bou continué nii bofii amé combat kénn doula topou dama beug nga kham lolou
@SerignemodouNdiaye-s3u
@SerignemodouNdiaye-s3u 4 часа назад
Bour téy dh and AK yow,Sa Thiès nak demako beug lol bilahi mais Yon bi mou dieul bouko wathioul douko Amal ndieurign,
@mamadoukamara953
@mamadoukamara953 12 часов назад
Bour tu t'es trompé sur ttes les lignes. Bour, Mag dafay mature. Bou Saa dioumé 1, balla dioum 10. On n'a l'impression que tu défends balla et essaies de mettre la faute sur sa thies.
@secretsdevoiles2567
@secretsdevoiles2567 9 часов назад
Saway bour a raison . Balla kilifeu sa thies leu ci lamb .
@salam7674
@salam7674 3 часа назад
Sathies rew rek motakh mouy teuseunté ak balla
@DOpe-boy99
@DOpe-boy99 3 часа назад
@@salam7674 bro khamo Sathies sou démé bay wakhé ni peut être amna Lou khéw mais kéne khamoul🙏🏾
@KhadyGaye-n5g
@KhadyGaye-n5g 31 минуту назад
Sa thies dh dafa diek basi yague rek di sisou si balla Gaye
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd 5 часов назад
Bour ligay wakh Malick Ngom molako geuna kham
@makambtv608
@makambtv608 53 минуты назад
Sa thies dall faw mou nangounii balla magam laa té défal nako lounéke
@MamoushitaNdiaye-nx1hv
@MamoushitaNdiaye-nx1hv 9 часов назад
Yagg n'a guiss kou seytaner mai kou melni Bour massou mako guise wallah mai da thies Bou waxrer lolu si concepte Lamb lako waxer mai pas dans la vrai l'ai seytaner nga rk boci nitt yi dakh dougn si bayi xell
@elhadjiyoussouphdiatta2810
@elhadjiyoussouphdiatta2810 8 часов назад
Doméram deug leu
@makambtv608
@makambtv608 49 минут назад
Koulaa yorr sii keureum aye atte you barii dila diokh léke akk nane dila diapalé say combat kone kokou ay détaille waroul takh ngakoy diapal merrrr
@Paolo-t4g
@Paolo-t4g 11 часов назад
Bour doumou kharam DEUG leu bayil famille Dianbour bingay diaxasé
@secretsdevoiles2567
@secretsdevoiles2567 9 часов назад
Yaa réw deug 😢 .
@KhadimeNdiaye-dm5xc
@KhadimeNdiaye-dm5xc 7 часов назад
Doule yawe deugue la wakh sa Thiès dafa rew
@sellediop1817
@sellediop1817 12 часов назад
Bour nit gou deugue ❤❤❤
@ndiagathioye3928
@ndiagathioye3928 2 часа назад
Non Sathies Con la..Khamoul ni bougua niit yi khamé Balla motakh
@sophrotall8105
@sophrotall8105 4 часа назад
Bour ki yaw la .... 😂😂😂😂
@MantaDiop-v3k
@MantaDiop-v3k 4 часа назад
Sathiess daffa soff te nitgni dany dieul lepp yanko balla te khamougno lisy birr sathiess sisou manla bou deger ay prrolam khamne sisoumanela
@moussaniang3860
@moussaniang3860 11 часов назад
Billay Bour deugue mo nékhoul déga
@momoteuw9131
@momoteuw9131 11 часов назад
Sa Thiès nak dafa yague sisou balla gaye
@mouhamadoudiop678
@mouhamadoudiop678 11 часов назад
Buur deugg pire gua wakh setlou na lolou ci kaddu sa thies yi boumouy liim lolou dara nicoul niit daguay reconnaissant balla dafal nako lou beuri desselouko dara
@khoumakhadim8455
@khoumakhadim8455 3 часа назад
Sa thies moo doof rek
@macerosall7323
@macerosall7323 11 часов назад
C'est votre marionnette
@HabibGueye-x4e
@HabibGueye-x4e 3 часа назад
bour yaw vrais seytane ngua
@dembaguite4945
@dembaguite4945 7 часов назад
Sa louko merlo khamolenn ko balla da am domm bou gorr wara ko toudee doubaless mou diell tourr be touddee ko benin tourr saliou leula merr poin tree
@KhadimeNdiaye-dm5xc
@KhadimeNdiaye-dm5xc 7 часов назад
Ya mana fénne ki topp vi mouhamed noumou toudou dou mamadou sakho
@MantaDiop-v3k
@MantaDiop-v3k 4 часа назад
Balla toudena doubaless dom mamadou
@dembaguite4945
@dembaguite4945 37 минут назад
@@KhadimeNdiaye-dm5xc mais yew hamgua ma bagamay fennleu ex hamgua niata att leu am baguamay fenn
Далее
Когда Долго В Рейсе)))
00:16
Просмотров 187 тыс.
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 12
40:00
Просмотров 274 тыс.