Mon père vous avez fait un travail remarquable depuis le début de cette enquête vraiment yalla na yalla goudal sa fane wakh dji rafet na Mashallah un vrai responsable ce vieux !
C'est vraiment triste. Aujourd'hui deux familles sont endeuillées. Il est temps que la société sénégalaise reconnaisse et met en-avant la santé mentale sous toutes ses formes. Merci à la police👏👏
Mane gnouy défendre kii nioma diakhal naan il regrette. Si les enquêteurs s'étaient trompés de piste et qu'il courait toujours , il allait continuer sa vie tranquillement et penser avoir bien agi. Khassim je n'ai pas de mots pour te qualifier. Je n'ai que du mépris du dégoût envers ce gars, tu mérites tout ce qu'il y a de pire dans cette vie. Repose en paix Kiné 😭
Vivons avec nos moyens Arrêtons de vivre au dessus de nos moyens Cet homme aux abois a commis l’irréparable pour plaire à sa famille Toutes mes pensées pieuses à la famille de la défunte
Mane dh khalé la j’ai âgée de 25 ans mais sama jourou baptême défouma dara sama yaye avait les moyens pour yéebi mais j’ai dit non, beugouma lolou,sama goro bou djiguen ak ay bokam louné wakhnaniouko di garouwalé sama yaye dakh ay affaire aduna
C vraiment dommage et triste repos en paix Fatou kiné ke firdawsi soit ta demeure. Mais du courage à tte les deux famille. J'ai pitié pour cet enfant innocent ki n'a rien réclamé papam outeul nako khass
Demain svp en memoire de la victime, il faut prier chacun dans sa religion devant le lieu du travail de la defunte Kiné. Que cette manifestation soit acompagnée de prière. Merci pour la Police et merci pour notre papa qui a donné des témoignajes pertinentes. Merci pere pour votre sagesse et lumière. Soyez béni.
La pression sociale ! On y prête pas attention , mais fait parti de ces maux qui gangrènent la société ! Kagn ngay ame ligueye Loy khaar pour takk diabar ? Loy khar pour seuyi ? Amago dom ba legui ? Sa morome yeup amnagn keur ! Gni gnongui teral senni wadiour ! Diw deh yobouna bayam naka ! Et malheureusement certains sont incapables de gérer cette « pression » .
Nous avons la meilleure police de la sous région; si on la laisse faire librement son travail, sans pression cette police est capable d'élucider les pires crimes . Bravo les gars vous avez assurer. Aujourd'hui la population a applaudi
c'est vraiment triste Allahou Akbar deux familles dans une tristesse à cause de biens matériels gnara yaye gnak dome ndakh alalou adouna paix à l'âme de la défunte et courage aux deux familles metina torope yalla na borom bi doli soutoura
Moi je me demande je suis bien j'arrête pas de pleurer pour fatou kiné et j'ai pitié aussi pour le gas il a gâché sa vie la vie de ses parents et de son enfant
Donc je suis pas la seule. J'essaye d'imaginer sa descente au enfer, il doit fortement regreter son geste actuellement mais malheureusement la vie n'a pas de bouton retour.
Bilaye parle plus fort affer de Teranga côté gorr gnii comme djiguene gnii dafa diote ñiou wakh si comm si deif ko par force leuh issssh yalna ñiou yallah samm
Mane d damako bagne té yalla takh maye number one si khékh bobou bagne nako ba sama famille khamnako si mane affaire de Teranga affaire de kheep nagnou ko arrêter si Sénégal bi moussiba rek lay indiiii 🙏
Merci a la police sénégalaise bon travail Fatou kiné yalnako yalla yeureum ta kharéko aldiana wayé khassim miko Ray yalnako borom torokhal ki teudj bi rek doyoul dagneko wara Ray mou déh
Kidal nagnouko ray publiquement domoharam ray femme pour bégeul sa femme dou yone li dafa yombe torop kiné sama nidiaye imam Ndiaye moko mayè yallana ko sougnou borom SWT diegeul kharéko aldiana ak bep waye dawlou thi barké seydina Mohamed SAW 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Pression social mon œil.c quelqu un de mal éduquer qui aimé vivre au-delà de ses moyens .il faut que les parents éduquent encore une fois leurs enfants
Ce crime est inacceptable , mais pabi lim wakh deugue la , pression sociale gni mou déf lo niombé dou diékh , so amoul do dara fii lép khaliss la si famille yi la tambalé lata mo guéne si biti , bo yoroul do touss nagne wakhanté deugue lolo fi am bagne mba nanguou mé nieupe kham nagne ko .legui nak ce qui fait la différence moy la capacité à résister à cette pression sans nék yafouss déf li nga meune loula yalla diokh nga doylo ko .té lolou c'est pas tout le monde qui le réussit. niane yalla mouthie thi yii rek mofi nek
Beugue nguënté war n'a takh ngay ray domou diambour ray diabbarou diambour pour lane teral sa diabbar .so amoul lo nguënté nga beuteul ayoul ba kerok ngay am lo nguënté bravo à notre police nationale chapeau bas vous avez fait encore une fois un travail remarquable
Magui ni teude depuis hier je n’arrête pas à me surpassé le drame wallahi je pense aussi à la famille de l’homme naka lagnou narra doundé surtout sa mère
Môme sakh dafa doul khalate rek mais sou wakhtanone ak Fatou Kiné niko mougnalma rek souma guenè si situations yi diokhla mou.am signature cachée kone Kiné bi dinako lebal ndakhté khaliss bolé wouko ak keneu nite danguay am yar aki teguine té bayi yeufou adouna yii moussiba rek lalay indil🤦♂️
Ndeysane sama xol bi diexna takk teh xamouma xassim bi gathié adoouna Yalla naniou thi yalla mousseul 😭😭 gathiel gua sa askane torokhal sa yaye 😭 waye lepp natou leuh Yalla na yalla nitt sa yonn guene la thi goudi yi gua nek ligua def reuy neuh 😭😭 Billahi bakane dafa foor waye ndogal la rek Yalla moko bind sa distin la warone done 😭😭 Yalla na oumpou bepp diammm njimou dall yalla guene lene si ak diam Di Masta wou famille kine diko nianal yeureumande Yalla l🙏 li Yalla bouniou ko guiss thi kaw souff j’ai imagine même pas gathie bi Wa keureum di doundou 😭😭 yalla iow rek yay bourr 😭😭😭 yallla gua niou mour mbalanou souteureu 🙏 amine
@@philobarreto6765 Vraiment. Goor tigui dou sathie baye rayater. Te mome l assassin c est pas la première fois mouye sathie. Bi mouye marier tamite dafa sathie . Donc dou goor mo takhe mou time djguene di ko raye ndakhe khalisse. Ki gathie dou ko raye.....Ki deumeu le , seytaner mo ko douga. Dou nite..
Père ta parfaitement raison gnou ladje la somme bou beurri si diabar après bou gnowé def lou yeme billahi légui kou amoul khalise dougne la meye diabar
@@khadysow2076 boudé domou gor t dieufé wouko nak imagine toi tim sa moromou nit surtout une femme diame ko 37 coup de couteau ki c juste un montre diégué woul daray gore
@@khadysow2076 gua balma mais ki mou Ray mome d'où domou gor khana je ne connais ni khassim ni la défunte mais li personne ne peut le qualifier domou gor dafay doylou mouye Mane Di kénene nak nagnou doylou si sounou weur seuk éducation bou rafet biko aye wadiour rame djiokhone rek yakheu nako ma sœur beugueu vivre dans une luxe insolente rek et son épouse biko tek pression bi yeup tay sou khassim Nate purger une longue peine est ce que Dina ko fa kharrr ki la tek pression pour baptême dou leu pougneul prison ont t'ils pensé au Bb li dafa ka nara top toute sa vie c'est ce qui me fait le plus mal c'est triste khassim regrettera son geste toute sa vie un jeune de rien du tout avec toute les informations qu'on a fi mou done liguéyé def un coup pour tak diabar defatt Lou gnaw Lou li pour un baptême personne ne peut cautionné ça . Je suis désolée de dire ça mais cest la triste réalité... nagnou doylou té mougne Lou gnou amoul
@@mariendiaye5915 tu as parfaitement raison bilaye kimou raye metti nama trop mais ma cherie guis ngua so khamé niit khame wouko lou niaw souko defe rek daflaye bete mane affaire bi dafma choqué trop motakh mais je sais que limou def dara meunouko justiciero bilaye
Entout cas yen si waydiour dji nanou moytou di seuy boune né souba la tabaski. Kouko si df souci eumb diké soumagé bala deh ray nit😭😭 kiné aldiana don sa keur
Li yeup djiguéne Moko waral.djiguene GNI doyloulene . djiguéne GNI bayiléne yebi yi..ce gas il a tue.il ta d'autres hommes qui vont encore souffrir â cause de ces cérémonies familiale.vraiment nous les femmes on doit revoir nos comportements côté cérémonie.on est vraiment en retard
Attends kone kii tayy lagnou koyy dogua diappp wala j’ai pas compris 🤔🤔🤔en tout cas tekna akh wadiouram 😭😭😭😭kii dem yalllah na khippé aldjana firdaws allahouma amine ya rabi wayy inchallah
Faut cessez de mentir, c'est pas son arrestation c'est la reconstitution des faits.Il faut éviter les faux titres pour attirer le visionnage.Vous n'avez pas besoin de mentir pour que l'on suive votre élément
Thi kholam rethiouna yakk nga askane sa doom way budul faay dinako topou sa diabar sa yaye lih dara diaruko def lo meunoul ndax niit sa yaye bumula diaral nga sacrifiée sa life pr raay niit dara menuko justifier si adouna yala nagnou yala maye moudiou bou raféte mo diara niane adouna yagoul dara diarufi dara nagnou def lougnou meune bugnou tedé nelaw