Lii rek moy dîner ji yonnentibi wathiéwoul loudoul wormalanté ak soppenté tee nek si ag njop amoul lenene Wayé nek fi di dingate rek dii bidah bidah tee khamouniou louy bidah
Abdou samad mi dèh défendroule darra défendroule Alkhourane défendroule sounnah.chaque jour mou wakhe loumou tèkoule si Alkhourane ak sounnah.l'islam gneuwoule pour ay woye.Alkhourane ak sounnah dafa nieuw pour nioukoy dieufé.