Lima nékh ci mom mooy actualitè boko meunnti dougueul dou toogn kénn ! Dinako wakh mais avec sagesse ba yaw miy déglou yay déf sa propre conclusion dou clash kènn !! Macha alah yalla nguafi yagg tè wèrr
Il fait partie de ceux qui encouragent vers l'islam, il met toujours en évidence l'excellence de l'islam maa sha ALLAH fa tabarak ALLAH yalna YALLA barkél ❤❤❤
Sa mère qui se dit musulmane exemplaire bouy sélal elle laisse son fils faire de la musique même si je ne condamne pas trop le fait de faire de la musique mais les filles danseuses qui se frottaient à son fils may lagne môme si bane diné la yar domam ou bien elle dit comme tout le monde il est jeune il doit s'épanouir ? Et si quelqu'un d'autre l'avait fait mogui nane li da Haram Sénégal mo Bari ay false
Wallahi barki Al Quran naniou bayi nakh sunu boop bou féké ay thiakhane mou fess ba ken d'où guiss sou fèké dîner djila niouy niow meun gualen conté blh...mais yalla na yalla léral Yonne yi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Ma cha allah lou l'ère nga wakh oustaz yalla na yalla motali yéné niêupp Incha'Allah tekniou si yonou siratal moustahim nous accordes une bonne fin Incha'Allah mousseulniou si mboungalou bammèl Incha'Allah
Ndeyssane chaque jours ak leçon bu bess adunaa lepp si organization laye douxéé 🤔 Oustaz yallah nala yalla rewel goudeul fanne si bi jaahi seyidinaa Mouhamet ( PSL)
Jërëjëf Ustaas Lii de Sëriñ Baabakar Si Abdu Waxoon Na ko. Neewoon na: ÑIY XEEX LISLAAM YÉPP DAÑOO BOOLE SEEN BOPP DOON BENN TE NUN JULLIT ÑI MANUNOO FEXE MUKK BA DOON BENN NGIR LISLAAM MAN A JËM KANAM.